Building infrastructure for African human genomic data management

Soppi lëkkalekaay yi
Asi

Gox Adduna Asi mooy réewum gëna mag[note 2][11][12] ci àdduna bi ci wàllu suuf ak askan.[ 12] Dafa am lu ëpp 44 milyoŋ kilometri kare, lu tollu ci 30% ci àll bi ak 8% ci àll bi. Bennoo bi, bu yàgg a nekk kërug mbooleem mbooleem nit ñi, [1] moo nekkoon bérab bu bare bu jëkk bi. Réew mi am 4.7 milyaar ci nit[14] di lu tollu ci 60% ci askanu àdduna bi, am na lu ëpp ci nit ñi ci yeneen àdduna yépp.

Diiwaanu Nguuru Room

Turi Réew yeek seen raaya Rëyaay
(km²)
way-dëkk
(1 sulet 2002)
Fattaay
(ci km²)
Péey
Diggu Asi:
Raaya Kasakistaan Kasakistaan[1] 2,346,927 13,472,593 5.7 Astana
Raaya Kirgistaan Kirgistaan 198,500 4,822,166 24.3 Bishkek
Raaya Tajikistaan Tajikistaan 143,100 6,719,567 47.0 Dushanbe
Raaya Turkumenistaan Turkumenistaan 488,100 4,688,963 9.6 Ashgabat
Raaya Usbekistaan Usbekistaan 447,400 25,563,441 57.1 Tashkent
Penku Asi:
Raaya Siin Siin[2] 9,584,492 1,384,303,705 134.0 Beijing
Raaya Ooŋ Koŋ Ooŋ Koŋ (China)[3] 1,092 7,303,334 6,688.0
Raaya Sapoŋ Sapoŋ 377,835 126,974,628 336.1 Tokyo
Raaya Makaaw Makaaw (China)[4] 25 461,833 18,473.3
Raaya Mongoli Mongoli 1,565,000 2,694,432 1.7 Ulaanbaatar
Raaya Kore gu Bëj-gànnaar Kore gu Bëj-gànnaar 120,540 22,224,195 184.4 Pyongyang
Raaya Kore gu Bëj-saalum Kore gu Bëj-saalum 98,480 48,324,000 490.7 Seoul
Taaywaan Taaywaan [5] 35,980 22,548,009 626.7 Taipei
Bëj-gànnaaru Afrig:
Raaya Isipt Isipt[6] 63,556 1,378,159 21.7 Cairo
Sibeeri:
Raaya Riisi Riisi[7] 13,115,200 39,129,729 3.0 Moscow
Bëj-saalum-penku Asi:[8]
Raaya Brunaay Daarusalaam Brunaay Daarusalaam 5,770 350,898 60.8 Bandar Seri Begawan
Raaya Kamboodi Kamboodi 181,040 12,775,324 70.6 Phnom Penh
Raaya Endoneesi Endoneesi[9] 1,419,588 227,026,560 159.9 Jakarta
Raaya Lawos Lawos 236,800 5,777,180 24.4 Vientiane
Raaya Maleesi Maleesi 329,750 22,662,365 68.7 Kuala Lumpur
Raaya Miyanmaar Miyanmaar 678,500 42,238,224 62.3 Naypyidaw[10]
Raaya Filipiin Filipiin 300,000 84,525,639 281.8 Manila
Raaya Singapoor Singapoor 704 4,483,900 6,369.0 Singapore
Raaya Taaylaand Taaylaand 514,000 62,354,402 121.3 Bangkok
Raaya Timoor gu Penku Timoor gu Penku [11] 15,007 952,618 63.5 Dili
Raaya Wiyetnaam Wiyetnaam 329,560 81,098,416 246.1 Hanoi
Ron-goxu End:
Raaya Afganistaan Afganistaan 647,500 27,755,775 42.9 Kabul
Raaya Banglaades Banglaades 144,000 133,376,684 926.2 Dhaka
Raaya Butaan Butaan 47,000 672,425 14.3 Thimphu
Raaya End End[12] 3,167,590 1,045,845,226 318.2 New Delhi
Raaya Iraan Iraan 1,648,000 68,467,413 41.5 Tehran
Raaya Maldiif Maldiif 300 320,165 1,067.2 Malé
Raaya Nepaal Nepaal 140,800 25,873,917 183.8 Kathmandu
Raaya Pakistaan Pakistaan 803,940 147,663,429 183.7 Islamabad
Raaya Siri Laanka Siri Laanka 65,610 19,576,783 298.4 Colombo
Penku gu Diggu, Penku gu Jege
Raaya Armeeni Armeeni[13] 29,800 3,330,099 111.7 Yerevan
Raaya Aserbayjaan Aserbayjaan[14] 46,870 3,845,127 82.0 Baku
Raaya Bahrayni Bahrayni 665 656,397 987.1 Manama
Raaya Ciipër Ciipër [15] 9,250 775,927 83.9 Nicosia
Raaya Palestiin Palestiin: Gaza[16] 363 1,203,591 3,315.7 Gaza
Raaya Jeoorji Jeoorji[17] 20,460 2,032,004 99.3 Tbilisi
Raaya Iraak Iraak 437,072 24,001,816 54.9 Baghdad
Raaya Israayil Israayil 20,770 6,029,529 290.3 Jerusalem[18]
Raaya Jordaani Jordaani 92,300 5,307,470 57.5 Amman
Raaya Kowet Kowet 17,820 2,111,561 118.5 Kuwait City
Raaya Libaan Libaan 10,452 3,677,780 353.6 Beirut
Raaya Omaan Omaan 212,460 2,713,462 12.8 Muscat
Raaya Kataar Kataar 11,437 793,341 69.4 Doha
Raaya Araabi Sawdit Araabi Sawdit 1,960,582 23,513,330 12.0 Riyadh
Raaya Siri Siri 185,180 17,155,814 92.6 Damascus
Raaya Tirki Tirki[19] 756,768 57,855,068 76.5 Ankara
Raaya Imaaraat yu Araab yu Bennoo yi Imaaraat yu Araab yu Bennoo yi 82,880 2,445,989 29.5 Abu Dhabi
Raaya Palestiin Palestiin: West Bank[20] 5,860 2,303,660 393.1
Raaya Yaman Yaman 527,970 18,701,257 35.4 Sanaá
Total 43,810,582 3,902,404,193 89.07

Ci angale ak ci faranse mooy Asia.

Asi dafa am ñaari tekki ci Injiil.

  1. Ci bu jëkk mooy li ñu tudde tey jii 'Asi Minër', maanaam daanaka lépp ci réew mu tudd tey jii Tirki (Turquie) lu fare penku géeju Ese.
  2. Ñaareel bi, ci jamano Injiil ji, Asi benn diiwaanu nguuru Room la woon. Moo doon wàllug sowu Asi Minër. Dafa boole diiwaani Misi, Lidi, Kari, ak genn wàll Firisi, ak dun ya nekk ca géeju Ese. Waa Room ñoo ko def diiwaan ci 129 j.K.. Ci bu jëkk péeyam moo doon Pergam. Waaye, gannaaw jamano Injiil, def nañu Efes ni péeyam. Juróom ñaari dëkk yi ñu gis ca téere Peeñu ma (Pe 2:1-3:22) ñoo bokkoon ca diiwaanu Asi.

Am na ñi xalaat ne yoon bu nekk ñu gis 'Asi' ci Injiil mooy diiwaanu nguuru Room bi. Am na ñeneen ñi xalaat ne léeg-léeg Injiil dafay wax ci ci Asi Minër (Jëf 19:26-27 21:27 24:18 27:2), te yi ci des mooy diiwaan bi.

Man nañu gis Asi ci Injiil ci Jëf 2:9; 6:9; 16:6; 19:10,22,26,27; 20:4,16,18; 21:27; 24:19; 27:2; Ro 16:5; 1Ko 16:19; 2Ko 1:8; 2Tim 1:15; 1Pi 1:1; Pe 1:4.

Karmat ak delluwaay

  1.   Kazakhstan is sometimes considered a transcontinental country in Central Asia and Eastern Europe; population and area figures are for Asian portion only.
  2.   The current state is formally known as the People's Republic of China (PRC), which is subsumed by the eponymous entity and civilisation (China). Figures given are for mainland China only, and do not include Hong Kong, Macau, and Taiwan.
  3.   Hong Kong is a Special Administrative Region (SAR) of the PRC.
  4.   Macau is a Special Administrative Region (SAR) of the PRC.
  5.   Figures are for the area under the de facto control of the Republic of China (ROC) government, frequently referred to as Taiwan. Claimed in whole by the PRC; see political status of Taiwan.
  6.   Egypt is generally considered a transcontinental country in Northern Africa and Western Asia; population and area figures are for Asian portion only, east of the Suez Canal (Sinai Peninsula).
  7.   Russia is generally considered a transcontinental country in Eastern Europe (UN region) and Northern Asia; population and area figures are for Asian portion only.
  8. Excludes Christmas Island and Cocos (Keeling) Islands (Australian external territories in the Indian Ocean southwest of Indonesia).
  9.   Indonesia is often considered a transcontinental country in Southeastern Asia and Oceania; figures do not include Irian Jaya and Maluku Islands, frequently reckoned in Oceania (Melanesia/Australasia).
  10.   The administrative capital of Myanmar was officially moved from Yangon (Rangoon) to a militarised greenfield just west of Pyinmana on 6 November 2005.
  11.   Timor-Leste is often considered a transcontinental country in Southeastern Asia and Oceania.
  12.   Includes Jammu and Kashmir, a contested territory among India, Pakistan, and the PRC.
  13.   Armenia is sometimes considered a transcontinental country: physiographically in Western Asia, it has historical and sociopolitical connections with Europe.
  14.   Azerbaijan is often considered a transcontinental country in Western Asia and Eastern Europe; population and area figures are for Asian portion only. Figures include Nakhchivan, an autonomous exclave of Azerbaijan bordered by Armenia, Iran, and Turkey.
  15.   The island of Cyprus is sometimes considered a transcontinental territory: in the Eastern Basin of the Mediterranean Sea south of Turkey, it has historical and sociopolitical connections with Europe. The Turkish Republic of Northern Cyprus (TRNC), distinct from the de jure Republic of Cyprus in the south (with a predominantly Greek population), is recognised only by Turkey.
  16.   Gaza and West Bank, collectively referred to as the "Occupied Palestinian Territory" by the UN, are territories partially occupied by Israel but under de facto administration of the Palestinian National Authority.
  17.   Georgia is often considered a transcontinental country in Western Asia and Eastern Europe; population and area figures are for Asian portion only.
  18. In 1980, Jerusalem was proclaimed Israel's united capital, following its annexation of Arab-dominant East Jerusalem during the 1967 Six-Day War. The United Nations and many countries do not recognize this claim, with most countries maintaining embassies in Tel Aviv instead.
  19.   Turkey is generally considered a transcontinental country in Western Asia and Southern Europe; population and area figures are for Asian portion only, excluding all of Istanbul.
  20.   West Bank and Gaza, collectively referred to as the "Occupied Palestinian Territory" by the UN, are territories occupied by Israel but under de facto administration of the Palestinian National Authority.

Xool it

Jukki yi ci lonku

Lëkkalekaay yu biti

Goxi / Kembaari àdduna si
Afritugalasi Oseyaani Afrig Tugalasi
Bëj-gànnaaru Aamerig Tugal Asi Bëj-saalumu Aamerig